GNAANOU GOUDI LAYLATOUL KHADR
Bissmilah, KOU TED KI NENA
Kou wakh batt yi Goudik ley-latoul khadre
La ilaha il-la lahou, hadada ridahou’
La ilaha il-la lahou, sin-nata harsihi
La ilaha il-la lahou, hadada khal khihi
La ilaha il-la lahou, hadada mala ikatihi
La ilaha il-la lahou, mil-ha samawatihi
La ilaha il-la lahou, mil’ha ardihi
La ilaha il-la lahou. Mil hama bay’na houma
La ilaha il-la lahou, mil hama si-ta
Djiouroum niet’ty bat la, ( 8 phrases)
Mou tol’lok djiouroum niet-ty Al diana yi
( les 8 portes de paradis)
Moune boko wakhe,
Mel ngani kou doundeul ley-latoul khadre Diouniy att (
1000 ans)
Ba nopi malayka yep kou dieuk ak kou moudji, dinane
dadjiee di binbe say yiiw ba boun sagnona nopalou
defko ta dou-nou mana diekhal tou’ya bay, bat yo-you
nga wakh.
Kon na yaatou ndakh dioullit yep manse diot . incaallah.
Yonent bi (sas) neena ci goudi laylatoul qadr kouci
dioulli gnari rakkas
Rakas buci nek
Fatiha 1 fois + likhlass(khoul houwal lahou) 7 fois
Apres seulmeul nga def Astahfiroulah wa atoùbou
ileyhi 70 fois
Kuko def ci goudi laylatoul qadr
1. Yalla djegueulla say bakkaar,djegueul sa gnari
waydiour,
2. Yabal ay mala-ika gnou dem thia aldianna dilafa
dieumbeutal ay garap,
3. Dilafa tabakhal ay etage ak ay djeunnè,ta bala nga
guèn addina di nga guiss lolou
• Yonent yalla Moussa nena sun borom damala
begueu djiguè,
➢ Sun borom niko kima begueu djiguè dal moy kiy
yèwou goudi laylatul qadr dima diamou
• Muniko dama beug yeurmandè
Muniko dama beug djegui siraat melni melakh
➢ YALLA niko kiy sarakhè goudi laylatul qadr
• Muniko dama beug tok thia ronn garabou aldiana
ya di lek thia lingneintef ya
➢ muniko gneel na kep ko xaamni sabalna sunu
borom ci goudi gi
• Yonent yalla moussa niko dama beug mouthie ci
sawara
➢ Yalla niko mouthie ci sawara defal nako gnimay
djègueulou ci goudi layalatoul khadr
• Muniko dama beug sa nguereum
➢ Yalla niko def nako ci kwn ko xamni diokna goudi
laylatul qadr diouli ci gnari rakkas
Goudila go xamni dansiy oubi bouti assamane si
amoul ben diaam busiy dioulli ci kabbar bunè yalla
dieumbalukothia ap garaap thia aldianna
Garapp go xamni nit manna war moyen de
transport dawsi kerr gui temeri att ta douko
djekhal
LAYLATOUL KHADR
Le Prophète (PSL) recommandait à notre mère Aïcha,
(que Dieu soit satisfait d’elle) d’y répéter, le plus
possible : « Allâhumma innaka ‘afuwwun
(karîmun) tuhibbul ‘afwa fa’fu ‘annî. »
(« Seigneur c’est Toi l’Indulgent (Honorable) ; Tu
aimes l’indulgence ; soit (donc) indulgent à mon
endroit »).
On y recommande aussi, entre autres actes de
dévotion :
une prière de deux « rakk’a », avec dans chacune
d’elle :
une fois la sourate liminaire (« Al fâtiha ») et sept fois la
sourate 112 (« Al Ikhlâs »).
Après quoi, dire « Astaghfirul-l-Lâha wa atûbu ilayhi »
(70 fois) ;
(« Je demande pardon à Dieu et à Lui je me repens. »)
• une prière de douze « rakk’a », avec dans chacune
d’elle :
une fois la sourate liminaire (« Al fâtiha ») et douze fois
la sourate 97 (« Al Qadri »).
• une prière de quatre « rakk’a », avec dans chacune
d’elle :
une fois la sourate liminaire (« Al fâtiha »), une fois la
sourate 108 (« Al kawçar ») et sept fois la sourate 112
(« Al Ikhlâs »).
Cette prière préserve des terreurs de la tombe et de
l’agonie douloureuse.
• une prière de quatre « rakk’a », avec dans chacune
d’elle :
une fois la sourate liminaire (« Al fâtiha »), une fois la
sourate 102 («At- takkâçur ») et trois fois la sourate
112 (« Al Ikhlâs »).
L’on se verra construire des châteaux aux Paradis. De
même, cette prière allège les douleurs de l’agonie, les
affres de la mort ainsi que les châtiments de la tombe ;
avec la permission de Dieu.