Accueil
Découvre | Connecte-toi | Crée un blog
Chat
Blog de makhawa
Pages sources
LEEN CI FARATAYI AP DIOULIT WARA KHAM ( A LIRE ET A PARTAGER)
Applis
LIIMOYE LEEN THI AY FARATA YI AP DIOULIT WARA KHAM GUIR SOUNOU BOROM MANA
NANGOU AY DIEUFEUM(Incaa-allàh)
FARATAY SANGOU SETT(sangou farata) (5 Diouroom la)
Skyrock
1-YEENE(booy FM fi sobè biy guènnè maanam awrabi fòfou ngay yèènèè
ragass
2-BOOMBE
3-GUAAW
Découvre
4-KHALIL maanam (KHADIALEE) KARAW YI
5-NATHIE LINOU LEUT(WARA NGA FIRI KO)
Connecte-toi
SOUNEUY SANGOU SETT(maanam sangou farata) (4 gnièènt la)
1-RAKHASS SAY LOKHO AVANT DE COMMENCER
2-GUALAKH NDIKOU (laver la bouche)
Inscris-toi
3-SARAKH NDIKOU (laver le nez)
4-RAKHASS SAY NOPP (laver les oreilles)
FARATAY DIAPP (8 diouroom gniat la)
1-YEENE (booy rakhass sa kanam nguay yèènè(yèènè quand vous lavez le visage)
2-RAKHASS SA KANAM (laver le visage)
3-RAKHASS SAY LOKHO BASSI THIONTHIA BI(laver les bras jusqu'aux coudes)
4-KHALIIL BAARAAMI LOKHO(laver les doigts)
5-MASSAA SA BOPP(laver la tète)
6-RAKHASS SAY TANK(laver les pieds)
7-BOOMBE
8-GUAAW(faire un peu vite)
SOUNEUY DIAPP(8 diouroom gniat la)
1-RAKHASS SAY LOKHO (laver les mains)
2-GUALAKH NDIKOU (laver la bouche)
3-SARAKH NDIKOU (laver le nez)
4-RAKHASS SAY NOPP (laver les oreilles)
5-YEESALAAT NDOKH MI (tooyalaat baaram yi)bèèsalat ndokh mi)
6-FIIROU (aspirer l'eau dans le nez)
7-DEELOOSSI MASSA (laver la tète de derriere arrivant devant)
8-TOFTALEE FARATAYI
FARATAY DIOULLI (prière)(nombre 15)
1-YEENE
2-KABBAR (Allaahou akbar)
3-TAKHAWAAYOU KABBAR BI
4-DIANG FAATIHA (rèciter fàtiha)
5-TAKHAWAAYOU TARY FAATIHA BI
6-ROUKOR
7-SIGGUI
8-SOUDIOOT
9-SIGGUI
10-TOOGUAY BOU MOUDIE BI
11-ASSALAAMOU HALAYKOUM BOU NDIEUK BI
12-DALLE (maanam avec calme)
13-AMOO ROUKOR (matalè roukor do seug bamou eup do sigui bamou eup
14-YEENE IMAM BIY DJIITEE LA
15-TOFTALEE FARATA YI
SOUNEUY DIOULLI (nombre 18)
1-LIKHAAM
2-LA SOURATE APRES FAATIHA
3-TAKHAWAAY BI
4-YALOU (wakh si souf)
5-BIRAUL (wakh si kaw)
6-TOUS LES KABBAR SUF LE PREMIER
7-DIRE SAMIHALLAAHOU LIMANKHAMIDAH
8-TAAYA
9-DOLLI DALLE GUI
10-DEELOO SEULMEUL
11-DIOTAY TAYA DIOU NDIEUK DJA
12-2eme ASSALAAMOU HALAYKOUM
13-ECOUTEZ QUAND L'IMAM RECITE A VOIE HAUTE
14-SAATOUROU (poser quelque chose devant qui mesure a peu pres 50 cm
15-SALAATOU HALA NABI
16-DOLLI TOOGUAAYOU SEULMEUL BI
17-BIREUL 1ere ASSALAAMOU HALAYKOUM BI
18-DIATAAYOU TAAYA DI MOUDJ JA (tògaayou taaya bi)
FRATAY KOOR(RAMADAN)(nombre 2)
1-YEENE
2-FEEGOU (ne pas manger ni boir ni faire de rapport avec sa femme)
SOUNEUY KOOR (nombre 3)
1-GUAAWA NDOGOU
2-KHEUDE
3-FEK AW LAMEENE (ne pas parler du mal)
FARATAY TIIME (nombre 8)
1-YEENE
2-SOUF SOU LAAP(sable propre) (WALA PAC BOU LAAP)
3-GUAAW
4-DOOR SOUF SI BOU NDIEUK BI (premier)
5-MASSAA SA KANAM
6-DIW KO SI SA LOKHO
7-DIOKALEE TIIME BI (lilatakh di tiime)
8-BALAA NGAY TIINE NGA NEUK BA WAKHTOUWI TABBI
SOUNEUY TIIME (nombre 3)
1-TOFTALE (tègalè)
2-YEESALAAT DOOR BI
3-DIW KO SI SA LOKHO BASSI THIONTHIABI (jusqu'au coude)
FARATAY AJAKA (nombre 4)
1-YEENE
2-SAKKOU AM ATT (wèèr ba wèèr wa dèloussi) 1 annèe
3-MISSAAP (maanam lou matta guènè ajaka)
4-BAGNE KO TOKHAL BOU FEEKEE AMNA KOULA DJIGUEE KOU KO YALOO(ne pas porter loin
si y'a quelqu'un de près qui en a besoin
SOUNEUY AJAKA (maanam tèguìn yi) (nombre 3)
1-SA KHOL SEED SI
2-DIG DAAUM (diguèn tèbi)
3-SOUTOURAL KO
FARATAY ATHIE(PELERINAGE)(nombre 4)
1-YEENE
2-WEUR GUI SI YOR YOROU BISSOU FOUKEELOU(10eme) TABASKI BI
3-DOKH SAFAA AK MARWA
4-TAKHAWOU BISSOU DIOUROOM GNIEENTEELOU(9eme)TABASKI BI NGA BAGNE FAA
DIOULLI
SOUNEUY ATHIE(PELERINAGE)(nombre 12)
1-SANGOU
2-RAFLEWOU
3-NIAARI RAKAAS(2 RAKAAS AVANT DE PARTIR(on rècite FAATIHA et KHOUYAA AYOUHAL
pour le premier rakaas)
(la deuxieme rakaas FAATIHA et LIKHLAAS)
4-LABAYKA LAAHOU......JUSQU'A MAKKA
5-
6-WEUR SI BISSOU FOUKEEL BI(10eme)DOKH AK SA TANK(pied)(bania waakhou bo amoul
nguante
7-FEUNE AFWA BA NEK SA KOGNE BA
8-SI C'EST UN HOMME 3 TOURS JUSQU'A MEULTEUSEUM(la priere que fais)
9-DOTHIE WANIY WAKH SAFAA YEEK SAKAW DOTHIE WA
10-NIAANE NGA NGAY NIAANE SI SAFAA
11-NIAANE NGA NGAY NIANN SI MARWA
12-BOO DIEUGUEE SAFAA DIDEM MARWA DIGUENTEEBI AMNA FOO KHAMNI(BATNOUN
MASSIN)LANKO TOUDEE BOOFI AKSEE DANGAY GUAW BA WEESOU KO
A LIRE ET A PARTAGER
NOUS VENONS DE DIEU ET RETOURNONS VERS LUI
1 2 0 Partager
Laisser un commentaire
Pseudo (obligatoire) :
Visiteur
Nous avons besoin de vérifier que tu n'es pas un robot qui envoie du spam.
Voir les mentions légales
Poster
Commentaires :
Signaler un abus
Top Blogs Top Profils
Langue Applis Infos