PROJET D’INTENSIFICATION
ECO-SOUTENABLE DE L’AGRI-
CULTURE DANS LES NIAYES
(PIESAN)
BONNES PRATIQUES DE PRODUCTION
D’OIGNON DANS LES NIAYES
XARALA CI MBEYUM SOPLE CI BIIR GOXU ñAAY BI
1
INTRODCTION
Dans le cadre de la promotion des bonnes pratiques agricoles durables, ce guide a été
élaboré par le Ministère de l’Agriculture et de l’Equipement rural (MAER) par le biais de son Projet
d’Intensification Eco-soutenable de l’Agriculture dans les Niayes (PIESAN).
Le PIESAN, appuyé conjointement par le Gouvernement de la République du Sénégal et le Gouvernement
de la République d’Italie, promeut dans la zone des Niayes une
agriculture écologique et intelligente face au climat, conservatrice des ressources
naturelles et de l’environnement.
L’objectif général du projet PIESAN est de contribuer à atteindre la sécurité alimentaire et le
développement rural du Sénégal par l’adoption et le
renforcement d’une agriculture durable et rentable dans la zone éco
géographique des Niayes dans une logique de prise en compte du genre.
Le PIESAN est très reconnaissant du PADEN dont le même guide précédemment édité, a largement permis
de faciliter l’édition du présent guide qui va renforcer les capacités des petits producteurs et des associa-
tions de producteurs de la zone des Niayes à adopter des modèles de production rentable et à produire
des aliments de qualité.
Le PIESAN remercie également toutes les personnes qui ont, de près ou de loin, apporté leur expertise
pour la consolidation du contenu de ce guide. Certains éléments du texte ont été tirés ou adaptés de
manuels de formation et de documents existants sur les bonnes pratiques agricoles durables dans la zone
des Niayes.
Le Coordonnateur du PIESAN
M. Tanor Meïssa DIENG
Am tambali
Ci nu ñuy jappalee ci xarala mbay mu wóor te sax, ministeer agricultuur ak eqipmaa riiral (MAER) defar
na teere bi ci japaleek porese buñuy wax PIESAN (porose mbay miy sukandikoo ci li alaam bi attan ci suufi
ñaay bi)
PIESAN ci jappaleek guvernamaa repibilik senegaal ak guvernamaa repibilik itaali, mi ngi mebëtt jëm ci
mbay mu xellu tey sàmmoonteek alaam bi ak liko wër ci diiwaanu ñaay bi.
Mbooleem mbebëtti PIESAN battay, mooy senegaal limuy dunde mu bayal ko bóopam, tek ci naatangeeq
aal senegaal yëp ci xellu tey sàmmoonteek alaam bi ak liko wër ba noppi di sooraale góor ñi, jigeen ñi ak
ndaw yi.
PIESAN mingi deelóo njukël PADEN mi njëqë defar tere bii, taxna mu yómbalal ñu ab defaraatam. Ak teere
bii, dina ñu may ñu gënë yóok xam xamu baykat yu ndaw yi ak mbóloo baykat yi tënku ci ay asoosiasioo
ci ñaay bi ngirë ñoŋal mbay mi.
PIESAN na jootali ay santak ngërem ci ñëpp ñoo xamne indi ñanu seen ndimbal ak seen xam xam ci defa-
raat teere bii ndax mu gënnë ñoŋ. Yéenn ci mbind mi ak nataal yi ñi ngi ko jëlle ci teere yiy wax aka jàngale
ci mbay mu xellu tey sàmmoonteek li ko wër ci diiwaanu ñaay bi.
Coordinatëru PIESAN:
M.Tanoor meysa Jeŋ
2
Etape 1 : La pépinière / Pepiñeer bi
1 / Choix de variétés adaptées / Tànn ay jiwu
Périodes de semis Période de Production Variétés
Jamonoy ji Jamonoy mbay Xeetu Mbay
Primeur Violet de Galmi, Texas
(culture hâtive) earty grano, Noflaye,
Octobre Goldor, Gandiol F1,
Octoobar Jamono ci gën ci Orient F1, Red passion
mbay Goudamy
Saison Violet de Galmi, Texas
earty grano, Noflaye,
Novembre Lolli Goldor, Gandiol F1,
Décembre Orient F1 (Ngagne
Mbaye) Red passion,
Noovambar Goudamy, Mercedes,
Desambar Safari, Belami
Arrière saison Red créole, Yakar,
Janvier (culture tardive et Rouge d’Amposta
Février semi-tardive) (saune san), Jaune
espagnol, Gao, Violet
Saawiee Noor de galmi, Orient F1,
Feewiryee Gandiol F1
3
2 / Choix du sol / Tannum suufu mbay
Choisir les sols
sablonneux
Tannal suufu joor
Sol sablonneux à limono
Walla suufu Beeñ
Eviter les sols lourds et
humides.
Moytul suuf yiy sol
ndox walla yu xorom.
4
Eviter ces précédents culturaux (ail, oignons, persil)
moytu leen koo toftal ci yii mbay ( laaj, soble, persi)
3 / Le matériel de travail / Jumtukaayi
Corde, décamètre, piquets, transplantoir, râteau, pelle-bêche,
plantoir, arrosoir, règle etc.
Buum, dekaameetar, bant, taranspalantuar, rató, peel, palantuar,
roosuar, reegal etc.
Avoir à sa disposition ce matériel indispensable.
Sakku jumtukaay yii boo bêggee bay soble
5
4 / Préparation des planches / Waajal palaŋ yi
4.1/ Nettoyer le lieu choisi. / Setalal bërëb bi.
4.2/ Ameublir le sol Utiliser la traction motorisée s’il s’agit de
grande surface.
jêffendikóol daaba ngir nooyal suuf si walla masin taractër bu
dee tool bu yaatu.
6
4.3/ Dimensionner et délimiter les planches (long=5m largeur=1m),
faire des pas de un mètre.
Natt leen palaŋ yi ci 5 meetar ci guddaay ak 1 meetar ci yaatuwaay
ak 50 santimeetar ci diggante yi ( been jéegó tólook 1 meetar)
4.4/ Epandre sur la planche de la
fumure organique bien décomposée
(une brouette par planche).
Jêfandikóo tos bu ñu nêbêl tasaare
ko ci palaŋ yi (palaŋ bune benn
buruwet
4.5/ Avec une pelle bêche,
bien incorporer la fumure
(2 à 3 kg par m²).
Tasaareel tos bi te jaxase ko
ak suuf si (2 ba 3 kilo meetar
kare bune)
7
Une boite d’allumettes
= 25 à 30g de fumure.
Benn buatu alumet mi ngi
tolook 25 ba 30 garamu tos
4.6/ Ensuite, épandre de la fumure minérale 25 à 30g (boite
d’allumettes) par m² (10.10.20).
Saawal 25 ba 30 garaam ci angare dis dis veŋ ci palaŋ bi metaar
karre bune, xott almet bu fees mi ngi toolu ci 25 walla 30 garam
4.7/ Arroser les planches avec 5
à 6 litres m2 /j.
Suuxatal palaŋ yi bes bune 5
ba 6 litaar ci meetar kaare bune
4.8/ Niveler les planches à l’aide
d’un râteau.
Maaseleel suufu palan yi te toj
donj yi àak ratô
8
4.9/ traiter le sol en épan-
dant un produit( insecticide
fongicide et nematicide)
chimique de préférence bio-
logique ou naturel .
Saawal posen bu doom
(durban) ngir aar suuf si ci
feebar
5 / Semis en ligne et semis manuel / Nji ci ay
yoon walla njiwum saaw
5.1/ Tracer les lignes de semis en utilisant l’angle de la règle
1 cm de profondeur et 10 cm entre les lignes.
Rëdêl ay yoonu ji ak cattu reegal, 1 sentimeetar ci xóotaay ak 10
sentimeetar diggante rëdd yi
9
5.2/ Placer les graines (4 à
6 gm par m²) dans les sillon.
Dugalal 4 ba 6 garaam ci
jiwu ci yóon yi ci meetar
kaare bune
5.3/ Fermer les sillons avec les
deux doigts.
Tëjël yoonu jiwu wi ak say
baaraam
5.4 Tasser et arroser en pluie
fine (arrosoir muni de pomme)
Suxatal ak roosuar bu am
bopp
10
5.5/ Ensuite Pailler avec
des feuilles mortes dés la
levée des plants.
Murël nji mi ak ay xob
ngir yómbal jebbi mi, din-
dil xop yi saa su jebbee
6 / Entretien de la pépinière / Toppatoo pepiñeer bi
6.1/ Arroser 5 à 6 litres par m²
et par jour, tôt le matin et tard
le soir.
Suxatal 5 ba 6 litaar ci meetar
kaare subba teel walla bu jànt
buy so
5 à 6 litres, par exemple :
5 à 6 pots d’eau de 1l =
1 arrosoir.
Misaal: 5 ba 6 liitar moo
tollook 5 ba 6 pottu ndox
11
6.2/ Désherber en cas
d’envahissement de
mauvaises herbes.
Buddil ñax yi ci mbay mi
ak seeni yoxo
Et biner pour aérer le sol.
Jexerbil suuf si ngir mu
nooki
6.3/ Observer la pépinière
pour identifier d’éven-
tuelles maladies.
Néemeeku gàancax gi
ngirfagaru ci feebar yi
12
6.4/ Intervenir en cas d’at-
taque avec des produits
biologiques ou naturels de
préférence.
Xeexaq feebar yi ak gunóor
6.5/ Un jour avant l’arrachage,
arroser abondamment la planche
ou 6 heures avant.
Suuxat, gajafal suuf mu fanaan lu
jiitu buddi mi
6.6/ Arracher les plants au
stade végétatif de 5 à 6 feuilles
(45 à 50 jours) avec le trans-
plantoir.
Buddil sople yi bu tóolo ci am
5 walla 6 xop ak taranspalan-
tuar.
13
6.7/ Placer dans un récipient ou sous des sacs les plants soigneuse-
ment séparés et débarrassés de l’excès de terre.
Duggal al sople yóo yu ci ndap lu yàatu ci téey te tagale leen ak
seeni suuf
6.8/ Transporter les
plants au champ pour le
repiquage en les proté-
geant du soleil et de la
chaleur.
Yoobu leen ca tool ba
ngir jëbët te aar leen ci
naaj wi
Etape 2 : Repiquage / Njëbët li
1 / Prépatation / Nun koy defe
1.1/ Nettoyer la parcelle.
Settal bërëp bi
14
1.2/ Ameublir le sol ou utiliser la traction motorisée s’il s’agit de
grande surface.
jêffendikóol daaba, ngir nooyal suuf si, walla masin taractër bu
dee tool bu yaatu
1.3/ Aménager en
bandes de 1 à 1,2 m
de large et 10 m de
long avec des allers de
50 cm entres elles.
Natt leen palaŋ yi ci
10 meetar ci gudday
ak 1,2 meetar ci yaa-
tuwaay ak 50 santi-
meetar ci diggante yi
15
1.4 / Epandre la fumure de
fond , Utiliser de la matière
organique bien décom-
posée, une brouette par
planche.
Jêfandikóo tos bu ñu nêbêl
tasaare ko ci palaŋ yi (palaŋ
bune benn buruwet
1.5/ Avec une pelle
bêche, bien incorporer la
fumure au sol.
Tasaareel tos bi te
jaxase ko ak suuf si
Ensuite épandre de la
fumure minérale
(10.10.20), 25g par m².
Saawal metaar karre bune
25 ba 30 garaam ci angare
dis dis veŋ ci palaŋ bi
Une boite d’allumettes =25à 30 g de fumure minérale.
xott almet bu fees mi ngi toolu ci 25 walla 30 garam
16
Ne jamais utiliser de l’urée en culture
d’oignon.
Moytu leen ba fàaw iire ci mbayum sople
Tracer les lignes de plantation sur les planches avec des écartements
de 20 cm à l’intérieur.
Rëdë leen ay yoonu ji ci palaŋ yi dandóo 20 santimeetar seen dig-
gante
Creuser avec un plantoir ou tout autre matériel adapté 20 cm entre
les plants.
Gassal ak taranspantuar walla bànt ay diggante yu 10 sentimeetar
ci yóonu ji wune
17
2 / Repiquage / Njëbët li
2.1 / Habiller les plantules
avant le repiquage.
Jémpal ngarabub sople bi
lu jiitu ngay jëbët
2.2/ Repiquer les
plants en respec-
tant les écarte-
ments de 10cm
sur la ligne et 20
cm entre les lignes ;
tôt le matin ou
tard l’après-midi.
Jëbëtal te sammonteek diggante yi: 10 sentimeetar ci yoonu Jëmbët li
ak 20 santimeetar ci diggante yóonu Jëmbët li
18
2.3/ Introduire doucement le plant jusqu’au collet puis tasser.
Eviter d’introduire le plant trop en profondeur.
Tuggalal ci bu téey ngarab si ba ca baat ba te suul. Moytul dug-
gal ngarab si lu sorri ci suuf
2.4/ Arroser aussitôt après plantation.
Suuxatal mu gajaf ginaaw jëmbët li
19
Etape3 : Entretien / Toppatoo mi
1/ Désherber en cas d’en-
vahissement de mauvaises
herbes.
Buddil nax yi ci mbay mi
ak seeni yoxo
2/ Biner 4 à 5 fois pour
aérer le sol .
Bitarñi suuf si néent ba
juróomi yoon
3/ Arroser 5 à 6 litres par m²
et par jour de préférence tôt
le matin et tard le soir.
Suxaatal 5 ba 6 liitar bes
bune ci meetar kaare bune
20
Utiliser 5 à 6 litres d’eau par m2
tous les jours jusqu’à la
bulbaison.
Jëfëndikóo 5 ba 6 liitaru ndox
bes bune ci meetar kare bune
ba sople bi di màtt
20 ème jour aprés repiquage / 20 fan ginaaw jëmbët
40 ème jour aprés repiquage 60 ème jour aprés repiquage
40 fan ginaaw jëmbët 60 fan ginaaw jëmbët
4/ Apporter de la fumure minérale d’entretien (10.10.20), 25g par m²
en 3 apports : 20ème /40ème /60ème, après repiquage
Saawal metaar karre bune 25 ba 30 garaam ci angare dis dis veŋ ci
palaŋ bi 20 fan, 40 fan, ak 60 fan ginaaw njëmbët mi
21
Les Differentes étapes de maturation de L’oignon
Jàmonoy màgguk sople
Stade Début bulbaison Début maturité Maturité complète
poireau Jàmonoy neek Jàmonoy neek sople Jàmonoy ñor
Jàmonoy doom
póoro
Ne jamais utiliser de l’urée en culture d’oignon
Moytu leen ba fàaw iire ci mbayum sople
22
5/ Surveiller régulièrement les plants afin de déceler d’éventuels
attaques ou de maladies.
Néemeeku gàancax gi ngir fagaru ci feebar yi ak gunóor yi
6/ Intervenir
aussitôt en cas
d’attaque avec
l’appui conseil de
techniciens. Se
référer aux
produits autorisés
par la législation en vigueur.
Xeexaq feebar yi ak gunóor yi ci ndigëlu tekniseŋ, samonte leen ak
li nguur digle
23
Etape 4 : Récolte / Goobb
1/ Observer bien la
parcelle quand 30%
des feuilles jaunies
son couchées au sol,
arrêter progressive-
ment l’irrigation.
Bóo setlóo ci toolbi limu
30% ci gàncax gi wow na ba
mbóoq, doggal suuxat mi
Les différentes phases d’arrêt de l’irrigation.
Jamono yii ñu warra taxawal suuxat mi
Arrêter aussitôt
l’irrigation
taxawal suuxat
mi
24
10 à 15 jours
après arrêt irri-
gation
10 ba 15 fan lu
jiitu ngob li
2/ Attendre une période de 10 à 15 jours avant la récolte. Récolter
l’oignon au bout d’un cycle de 70 à 120 jours selon les variétés.
Arracher manuellement et avec précaution les bulbes avec leurs
feuilles à l’aide d’un outil adapté.
Sullil sople bi ak ay xobam ci téey ak say loxo bu amee 70 fan ba
120 fan, walla nga jëfëndikoo juŋtuwaay
Couper le feuillage à 5 cm du collet.
Daggal xop yi ci lu tóolook 5 sentimeetar ci bakan bi
25
3/ Sécher au champ pendant 1 à 2 jours après arrachage.
Bàayil sople bi ci tool bi mu wow been ba naari fan
Etape 5 : Conditionnement au Champ et transport
Sol mi ci tool ba ak yóobu
1/ Transporter
l’oignon emballé par
charrette, par
camionnette vers les
Infrastructures de
stockage.
Toxalal saako sople yi ci woto wala kamiyoŋ Walla sareet ca berëpu
dénc kaay yi
26
2/ Faire le tri des différents calibres sur une table de tri.
Tàan sople bi, yu dijj yi cig wet, yu yamamaay yi cig wet, ber
3/ Conserver l’oignon sur des claies de séchage dans des endroits
propres, secs, frais et bien aérés.
Denc sople bi ci ay kale sesaas ci bërëb yu yaatu, baña tooy, sedd
te am ngelaw
27
4/ Conditionner
l’oignon soigneuse-
ment dans des em-
ballages adéquats
et propres (sac,
caisse de récoltes,
cageots)
ñu def sople binu
tàan ci ay defukaay
yu set, tamu nanu
saako walla kees
Placer un label / une marque du produit
sur les emballages.
Deffal ci saako yi ay mandarga xameekay
5/ Placer les sacs sur
des palettes pour
éviter les attaques et
pourrissements.
Teggal saako sople yi
ci ay tagaru déenq
1,5t par palette et distante d’un mètre.
Tagar bune man na jël benn ton ak genawal te sorek benn meetar
seen digante
28
Magasin de stockage bien aéré / Mangasin buy dénc sople
Conserver l’oignon sur des claies de séchage dans des endroits
propres, secs, frais et bien aérés ;
Suivre régulièrement les claies de séchage.
Denc sople bi ci ay kale sesaas ci bërëb yu yaatu, baña tooy, sedd
te am ngelaw
29
30
Illustrations et mise en pages: Aly Nguer Diop
Projet d’Intensification Eco-Soutenable de l’Agriculture dans les Niayes (PIESAN)
31